Muccug Gi Mujj

Muccug Gi Mujj

Tënk

Dafa mel ni naqqar du mas a jeex, waaye Yéesu Christa Borom bi wax na ne bés dina ñëw mu jeex. Dig na ne dina dikkaat ci àdduna si ngir yobbu Ay nitam ci ab béréb bu tudd "Nguuru Aji Sàkk Ji." Ci béréb bu neex booba, amul naqqar, amul dee, te du amati ay juddaat. Danuy dund ba fàww ak Yàlla Aji Sàkk Ji! Téere bu ndaw bii dafa nuy wax naka lanuy mën a fagaroo ngir sunu mucc bu mujj.

Yebbi

Bindul ci sunu yéenekaay

Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!

newsletter-cover