Nànd Naqar Wi

Nànd Naqar Wi

Tënk

Ci jamano jii, nit ñu bare ñu ngi dund ci ñàkk a toppatoo ak mettital. Yéesu amoona ab dundug mettital, itam. Moom daan na dimbali nit ñi, daawoon na leen faj, te daawoon na leen jàngal ñu jaar ci yoon wi gën. Am na ay nit ñu ko bañoon ba faatoon Ko, waaye banu weesoo ñetti fan, dafa dekkiwaatoon ba noppi delluwaatoon ca Baayam ca àjjana. Téere bu ndaw bii dafay nettali lu gàtt ci dund ak mettital yu Yéesu, ak itam Digam ci faj sunuy naqqari xol.

Yebbi

Bindul ci sunu yéenekaay

Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!

newsletter-cover