Shqipاَلْعَرَبِيَّةُঅসমীয়াবাংলা简体字正體字ČeštinaNederlandsEnglishÈʋeFrançaisFulfuldeGaroDeutschHausaעבריתहिन्दीIgboIndonesiaItaliano日本語Tamaziɣtಕನ್ನಡKhasiភាសាខ្មែរ한국어سۆرانیພາສາລາວMelayuമലയാളംमराठीмонголMooréनेपालीپښتوفارسیPolskiPortuguêsРусскийကညီကျိာ်ᱥᱟᱱᱛᱟᱲᱤසිංහලAf-SoomaaliEspañolBasa SundaKiswahiliТоҷикӣதமிழ்తెలుగుไทยབོད་སྐད་TürkçeAkan-TwiУкраїнськаئۇيغۇرTiếng ViệtWollofYorùbá
Am Njariñ Ci Biir Àdduna
Tënk
Dund gi mën na mel ni amul njariñ soo amul gis-gis bu yaatu. Ci téere bu ndaw bii, Peter mu ngi gëstu njariñu dund gi gànnaw ba mu ñakkee ay nit ñu mu bëggoon ci biir xolam, ba noppi muñ lu yàgg ci xeex ak feebaru ndof. Moom mu yëg ci boppam lu koy xëcc di rafetaay ak toftal bu sell yi ci natiir bi. Mbaa am na nit ku mën a sàkk rafetaay ak toftal bu sell yi ci natiir bi? Peter xalaat na ci njéexitalu dund gi rafetaayu Defarub Xel mënoon a def ci xolam.
Xeet
Kayitu siiwal
Siiwalkat
Sharing Hope Publications
Jàppandi ci
10 Kàllaama yi
Xët
6
Yebbi
Bindul ci sunu yéenekaay
Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!
Siiwal yu fës
© 2023 Sharing Hope Publications