Shqipاَلْعَرَبِيَّةُঅসমীয়াবাংলা简体字正體字ČeštinaNederlandsEnglishÈʋeFrançaisFulfuldeGaroDeutschHausaעבריתहिन्दीIgboIndonesiaItaliano日本語Tamaziɣtಕನ್ನಡKhasiភាសាខ្មែរ한국어سۆرانیພາສາລາວMelayuമലയാളംमराठीмонголMooréनेपालीپښتوفارسیPolskiPortuguêsРусскийကညီကျိာ်ᱥᱟᱱᱛᱟᱲᱤසිංහලAf-SoomaaliEspañolBasa SundaKiswahiliТоҷикӣதமிழ்తెలుగుไทยབོད་སྐད་TürkçeAkan-TwiУкраїнськаئۇيغۇرTiếng ViệtWollofYorùbá
Àtteum Askan Yalla
Tënk
Ci ay xarnu yu bare yu weesu, askanu Yahuut yi màggaloon nañu Yom Kippur. Màggal googa mu ngi nuy fàttali ne dina ami yoonu yemale ci nitu Yàlla ca mujj ga. Wánte li aada boobuy tekki yomb na fàtte, mbaa nuy wéeru ci diine gi ngir mu may nu kaaraange ca bés-pénc. Waaye, téere bu ndaw bii dafa nuy fàttali ne bés-pénc nekk na ab woote bu diis ngir dajeek Yàlla te waajal sunuy xol ci kanamam Moom.
Xeet
Kayitu siiwal
Siiwalkat
Sharing Hope Publications
Jàppandi ci
5 Kàllaama yi
Xët
6
Yebbi
Bindul ci sunu yéenekaay
Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!
Siiwal yu fës
© 2023 Sharing Hope Publications