Atté Ngir Sama Mettit

Atté Ngir Sama Mettit

Tënk

Naqqar du wëy ba fàww. Téere bu ndaw bii dafay nettali ab nit bu ñu doon sàkku ci xeex bu mettit ndax mu ngi doon gis yamale bu mujj bu Yàlla Aji Sàkk Ji di mbugal nit ñu bon ñi. Dafay wone nan la Yéesu doon tëjee njiit yu naaféq yi te dig atté ci wetu ñi ñu doon mettital. Waaye sunu réeralee sunu bopp, am na ab yoon bunu mën na sàkkoo njéegal jaare ko ci mettiital bi Yéesu Christa Borom bi muñoon ngir nun.

Xeet

Kayitu siiwal

Siiwalkat

Sharing Hope Publications

Jàppandi ci

5 Kàllaama yi

Xët

6

Yebbi

Bindul ci sunu yéenekaay

Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!

newsletter-cover