Tekkiteb Àddina

Tekkiteb Àddina

Tënk

Sunu ëllëgu àdduna nekkul ab kumpa. Waxoon nañu ko ci Téereb Yàlla bi, téereb Yéesu Christa Borom bi. Yéesu wax na nu bàyyi xel ci màndarga yu am solo yi ndax nu mën a xam kañ la tukkiteb àddina si di jegesi. Sunu toppee Ay njàngaleem te gëm Ko, dina nu xam lu wóor ci sunu ëllëg. Téere bu ndaw bii dafa nuy wax nan lanuy fagaroo ci tukkiteb àddina si ak ndoorteelu dund gu dul jeex ba fàww.

Xeet

Kayitu siiwal

Siiwalkat

Sharing Hope Publications

Jàppandi ci

7 Kàllaama yi

Xët

6

Yebbi

Bindul ci sunu yéenekaay

Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!

newsletter-cover