Shqipاَلْعَرَبِيَّةُঅসমীয়াবাংলা简体字正體字ČeštinaNederlandsEnglishÈʋeFrançaisFulfuldeGaroDeutschHausaעבריתहिन्दीIgboIndonesiaItaliano日本語Tamaziɣtಕನ್ನಡKhasiភាសាខ្មែរ한국어سۆرانیພາສາລາວMelayuമലയാളംमराठीмонголMooréनेपालीپښتوفارسیPolskiPortuguêsРусскийကညီကျိာ်ᱥᱟᱱᱛᱟᱲᱤසිංහලAf-SoomaaliEspañolBasa SundaKiswahiliТоҷикӣதமிழ்తెలుగుไทยབོད་སྐད་TürkçeAkan-TwiУкраїнськаئۇيغۇرTiếng ViệtWollofYorùbá
Muslaay Ci Rab Yi Soxor Yi
Tënk
Rab yu soxor yi ñu ngi fi, te mën na ñu tiital nit lool. Am na ay nit ñuy wax ne am na ñu sañ-sañ ci rab yi, wànte dañuy laaj xaalis bala ñu nuy dimbali. Yéesu Christa, amoon na mën-mënu faj silmaxa ak dàqq seytaane yi, waaye mësul woon a laaj payoor. Dafa doon dimbali nit ñi saa su ne te doonul woon laaj dara ndaxte Moom dafa bare yërmande te Moom, itam, bëggul woon a gis rab yu soxor yi di nu sonnal. Téere bu ndaw bii dafa nuy wax fan la lu-bon joge ak nan la nu war a ñaane Yéesu ngir mucc ci seytaane yi.
Xeet
Kayitu siiwal
Siiwalkat
Sharing Hope Publications
Jàppandi ci
12 Kàllaama yi
Xët
6
Yebbi
Bindul ci sunu yéenekaay
Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!
Siiwal yu fës
© 2023 Sharing Hope Publications