Ndax Yéesu Mën A Ñu Dimmali?

Ndax Yéesu Mën A Ñu Dimmali?

Tënk

Nun ñépp danuy jànkonteel ak ay jafe-jafe yu nu mënul a saafara nun doŋŋ ci sunu dund. Yenn saa yi danuy foog ne kenn gisul sunu naqqar, wànte Yàlla Aji Sàkk ji xam na lépp lu xew. Moom yónni na Doomam, Yéesu, jox ko ab doxalin ngir mu dimbalinu nu génn ci naqqar ba fàww. Ñetti nettali yii dañuy wax ci ay nit njaay ñu am dëggantaan ay jafe-jefe yu demoon gisi Yéesu ngir ndimbal. Kenn ci ñoom xamul woon lu bare ci Yéesu ca jamono jooja, waaye bi Mu leen dimbalee ba noppi, ñu bëggoon Ko gën a xam. Téere bu ndaw bii dafa nuy jàngal naka lanuy jullee ngir mën a wax Yéesu sunuy jefe-jefe. Dina nu dimbali itam!

Yebbi

Bindul ci sunu yéenekaay

Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!

newsletter-cover