Ëllëg Gi Gën

Ëllëg Gi Gën

Tënk

Ci àdduna sii, mbir yu bon ñu ngi am. Nit ñi ñu ngi am ay naqqar te dañuy dee. Waaye am nanu yaakaar ci ëllëg! Téere bu sell bu Kercen Yi, Téereb Yàlla bi, nee na Yéesu dina ñëw jëlsi nit ñi Ko bëgg yóbbu leen ci béréb bu gën a baax. Foofa, kenn du fa feebar mbaa mu fay am naqqar. Ku nekk dina dund ci jàmm ak déggoo ba fàww. Téere bu ndaw bii dafa nuy wax naka lanuy mën a bokkee ci ëllëg gu neex gi nu Yàlla dencal!

Yebbi

Bindul ci sunu yéenekaay

Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!

newsletter-cover