Shqipاَلْعَرَبِيَّةُবাংলা简体字正體字ČeštinaNederlandsEnglishÈʋeFrançaisFulfuldeGaroDeutschHausaעבריתहिन्दीIgboIndonesiaItaliano日本語Tamaziɣtಕನ್ನಡភាសាខ្មែរ한국어سۆرانیພາສາລາວMelayuമലയാളംमराठीмонголMooréनेपालीفارسیPolskiPortuguêsРусскийကညီကျိာ်සිංහලAf-SoomaaliEspañolBasa SundaKiswahiliТоҷикӣதமிழ்ไทยTürkçeAkan-TwiУкраїнськаئۇيغۇرTiếng ViệtWollofYorùbá
Am Ndam Ci Mer Mi
Tënk
Nit ku ne dafay mer—wànte sunu téyée sunu mer, mën nanu gaañ. Téere bu ndaw bii dafay nettali ab waa ju dundam soppeeku ngir njàngam ci naka la Yéesu daan baalee nit ñi—ba ci sax nit ñi ko Faatoon. Sunu toppee Yéesu, dina nu soppi te dina tax nu gën Ko bëgg. Dina dindi sunu mer ak naqqaru xol ba sunu dund am ndam ci kanamu Yàlla.
Xeet
Kayitu siiwal
Siiwalkat
Sharing Hope Publications
Jàppandi ci
12 Kàllaama yi
Xët
6
Yebbi
Bindul ci sunu yéenekaay
Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!
Siiwal yu fës
© 2023 Sharing Hope Publications