Shqipاَلْعَرَبِيَّةُঅসমীয়াবাংলা简体字正體字ČeštinaNederlandsEnglishÈʋeFrançaisFulfuldeGaroDeutschHausaעבריתहिन्दीIgboIndonesiaItaliano日本語Tamaziɣtಕನ್ನಡKhasiភាសាខ្មែរ한국어سۆرانیພາສາລາວMelayuമലയാളംमराठीмонголMooréनेपालीپښتوفارسیPolskiPortuguêsРусскийကညီကျိာ်ᱥᱟᱱᱛᱟᱲᱤසිංහලAf-SoomaaliEspañolBasa SundaKiswahiliТоҷикӣதமிழ்తెలుగుไทยབོད་སྐད་TürkçeAkan-TwiУкраїнськаئۇيغۇرTiếng ViệtWollofYorùbá
Dund Ca Àjjana
Tënk
Yàlla Aji Sàkk Ji moo sàkk àddina bu mucc-ayib te mat. Wànte nit ñu njëkk ña ñoo tànnoon mbir yu bon, ba tax àddina si nekkatul ab béréb bu wóor. Mbind mu sell mu Kercen yi, Téereb Yàlla bi, dig na ne Yàlla dina defaraat àddina si ni mu meloon ca njàlbéen, waaye naka lanuy mën a xamee ne li Mu nu dig dëgg la? Téere bu ndaw bii dafay leeral ab kémtaan bu am solo ci mbindu Dañeel 9, bi nuy jox yaakaar ne yeneeni wax yi ci biir Téereb Yàlla bi dinañu feeñ ni ko Yàlla waxewoon.
Xeet
Kayitu siiwal
Siiwalkat
Sharing Hope Publications
Jàppandi ci
12 Kàllaama yi
Xët
6
Yebbi
Bindul ci sunu yéenekaay
Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!
Siiwal yu fës
© 2023 Sharing Hope Publications