Shqipاَلْعَرَبِيَّةُবাংলা简体字正體字ČeštinaNederlandsEnglishÈʋeFrançaisFulfuldeGaroDeutschHausaעבריתहिन्दीIgboIndonesiaItaliano日本語Tamaziɣtಕನ್ನಡភាសាខ្មែរ한국어سۆرانیພາສາລາວMelayuമലയാളംमराठीмонголMooréनेपालीفارسیPolskiPortuguêsРусскийကညီကျိာ်සිංහලAf-SoomaaliEspañolBasa SundaKiswahiliТоҷикӣதமிழ்ไทยTürkçeAkan-TwiУкраїнськаئۇيغۇرTiếng ViệtWollofYorùbá
Ku-Nekk Ak Linga Doon
Tënk
Gëstu askan wi wone na am mbir mu ñu tudde ''tëralin yu xóot ci diine'', te ci biiram nit ñi dañuy bëgg a am ay jaar-jaar yu kawe, suñu nekkul sax ay nitu diine yu ne fàŋŋ. Ñun ñépp danuy jaamu ab mbir wala ak nit—te nekk lu jaar yoon nit ki def ko, te loolu bokk na ci sunuy raññeekuwaay. Jaamu dafa wara nekk lu nit ki di tànn ci coobareem, waaye mukk ci lu mu bëggul. Waaye, téere bu ndaw bii dafay wone ngaañ li nekk ci jaamuloo nit diine ci ludul coobareem, loolu dina feeñ te yàggatul.
Xeet
Kayitu siiwal
Siiwalkat
Sharing Hope Publications
Jàppandi ci
9 Kàllaama yi
Xët
6
Yebbi
Bindul ci sunu yéenekaay
Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!
Siiwal yu fës
© 2023 Sharing Hope Publications