Shqipاَلْعَرَبِيَّةُঅসমীয়াবাংলা简体字正體字ČeštinaNederlandsEnglishÈʋeFrançaisFulfuldeGaroDeutschHausaעבריתहिन्दीIgboIndonesiaItaliano日本語Tamaziɣtಕನ್ನಡKhasiភាសាខ្មែរ한국어سۆرانیພາສາລາວMelayuമലയാളംमराठीмонголMooréनेपालीپښتوفارسیPolskiPortuguêsРусскийကညီကျိာ်ᱥᱟᱱᱛᱟᱲᱤසිංහලAf-SoomaaliEspañolBasa SundaKiswahiliТоҷикӣதமிழ்తెలుగుไทยབོད་སྐད་TürkçeAkan-TwiУкраїнськаئۇيغۇرTiếng ViệtWollofYorùbá
Yaakaar Jiy Weesu Dee?
Tënk
Dee dafay dab ñépp, waaye neexul a nangu. Lu tax? Ndaxte Yàlla dafa sàkk doomu-àadama ngir mu dund ba fàww. Waaye bi bàkkaar duggsee ci àdduna, ci la dee duggsee tamit. Ndax Yàlla dina jox bàkkaar ndam, mbaa ndax am na am mbir mu mel ni dekkiwaat ginnaaw dee? Nit ñu bare dañu foog ne dee la mbir mi yem. Waaye, mag ñi ak yónent yi bind nañu ci ab jamono ju Yàlla di dekkil nit ñi ngir may leen dund gu dul jeex. Téere bu ndaw bii joxe na ab tënk bu gàtt ci liy xewi ca jamono jooja.
Xeet
Kayitu siiwal
Siiwalkat
Sharing Hope Publications
Jàppandi ci
5 Kàllaama yi
Xët
6
Yebbi
Bindul ci sunu yéenekaay
Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!
Siiwal yu fës
© 2023 Sharing Hope Publications