Wutum Gudd Fan

Wutum Gudd Fan

Tënk

Doom-àadama yi dañuy daw aka randal dee saa su ne. Waaye ba tey, dee dina ñëw ci ku nekk ci nun, jël sunuy bakkan ba fàww. Wala déed? Ab Téere bu yàgg dafay tegtal ab pexe ngir guddal sunuy fan ba mu weesu sax li xam-xamu wérgu-yaram wone ak saytub yaram. Su dee linu yaakaar ci “dund gu dul jeex” nekkoon na sax 1% ci dëgg, ndax jaroon na ñu ciy gëstu?

Xeet

Kayitu siiwal

Siiwalkat

Sharing Hope Publications

Jàppandi ci

10 Kàllaama yi

Xët

6

Yebbi

Bindul ci sunu yéenekaay

Nekkal kiy njëkk a xam kañ la siiwal yu bees yi di jàppandi!

newsletter-cover